"POP POP", Un titre certe simple mais qui engendre de riches paroles dans lesquelles L'artiste nous fait savoir que la vie est si éphémère,et que ni la jalousie, ni méchanceté ne devraient avoir une place dans notre société, mais devraient pas aussi nous freiner à atteindre nos objectifs. Savoir réagir avec classe et élégance, bravoure et persévérance, fait la force de l'homme et cela nous amène à être "POP POP" Crédits de la chanson et du clip Beat : Thiokos Guitare : Seydou ba Percussion : Pape Ndiaye tama Mix & mastering : Polibeat Réalisation : Gaby iris / iris av Coiffure : Demba tarrou locks 78 432 00 50 Contact Watshap : +221 77 840 00 80 / 77 847 12 12 ▪️Suivez-moi sur mes réseaux 🔸Instagram : https://instagram.com/cherifou__lofficiel 🔸Facebook : https://www.facebook.com/profile.php?id=100035350346924 🔸Tik Tok : https://www.tiktok.com/@cherifouofficial Stream & Ecoute : https://bfan.link/pop-pop #cherifou #poppop #senegal #dakar #music Lyrics PoP PoP Kay kay kay kay Kay ma khamal la ni Adoun’ya dou benn fann Kingay togué tay bou souba meun’nala yéy Kay ma digual’la ni Bouldi khol nitt diko nié Meul nala yobbé ignaaan (ignaan ignaaan) Yangui coq 🐓 coq ba callé May Pop pop ci khalé Ngay togg togg ba callé Diémo té meuno dabbé Man soma beugoulé boul saalé Guiss’nané dolé feeling béla poussalé Ehhhhhh yah So beugoulê boul salé Bayil sokhor ignaan dalay té Boko toppé dangay dé firiil sa khol Refrain Ay way ah yeukna linga nékké (ay door rék) Malay lébal mbakh ngamay fékhél (ay door rék) Eh bal dooré Guiss’nala ngay leuré eh eh ehhhh do goré Man guiss’na ningmay woré Boul déféni ninga nékké yeugoumako dama doylou bo déffé’ni ya geuna yéwou nieup, nalaw nga bay galleu Thioy rék Yaw deukéll thioy rék Thioy rék Yaw deukéll thioy rék Dél thioy rék 2e Couplet Dembeu yanei woon Dembeu yanei woon ni gorêdiwo Konn loula diapp tay banga né ci yoonou noon Non parégouma Nono tambalé gouma Yay sakhol ci nianaal’ma Sabo douhan ouma mi falama néné barakaa Yangui coq 🐓 coq ba callé May Pop pop ci khalé Ngay togg togg ba callé Diémo té meuno dabbé Yaw woutal béneen yoon bo diarei Yaw démo kou nekk ci yoon nga diém’ko garé Bayil sokhor ignaan dalay té Soko toppé dangay dé firiil sa khol Refrain Ay way ah Yegg’na linga nékké (ay door rék) Malay lébal mbakh ngamay fékhél (ay door rék) Eh bal dooré Guiss’nala ngay leuré eh eh ehhhh do goré Man guiss’na ningmay woré Boul déféni ninga nékké yeugoumako dama doylou bo déffé’ni ya geuna yéwou nieup, nalaw nga bay galleu Thioy rék Yaw deukéll thioy rék Thioy rék Yaw deukéll thioy rék Dél thioy rék Solo guitaar 🎸🪗 Ambiance outro Thiow meunoul dara Wakh djou bonn fadioul dara (dedett) Thiow meunoul dara ci man wakh dji fadioul dara (dedett) Thiow meunoul dara ci man wakh dji fadioul dara (dedett) Thiow meunoul dara wakh dji fadioul dara Thiow meunoul dara wakh dji bonn fadioul dara Thiowli meunoul dara dafmay yokk dolê nopaloul Khalé baangéééé (man’la) Khalé baangéééé (kham’ngan man’la waaawaaw) Kham ngani man’la Ay man’la Affaire bi man’la Wooooy man’la Nénagn’ma yaw la ehhhhh Khalé baangéééé (man’la) Kham ngani man’la Ay man’la Affaire bi man’la Wooooy man’la Nénagn’ma yaw la ehhhhh Té bilae damay fo ak yennn 😊🔇