#dafanekh http://africori.to/dafanekh • Disponible ici Auteur : Jeeba Compositeur : Bril Label : Abadane Daiman ÉQUIPE VIDÉO Réalisation et Post-production: Mao SIDIBE caméra: Oumar NDIAYE Lumière: Mamadou DIA Makeup: Aby Sow Régie: Lamine BA Assistants: yaya Thiam & Mohamed Thiam Making off Biraan Pix Stylisme : babo - Zahrafric - Bise collection - Chorégraphie : MG_dancer 221 Danseurs : @assi_show_mamen @riima_danse @racky_kush @sagnaclarisse2 Artwork Dafa Nekh : Med kgs prod Lyrics Wakh mo lo bouga ma defal lako Wakh ma lo namma Cherie ma outal lako Meme boudé auto ma dieundal lako Yobou lathi chateau nga deuké dodo Dama xam fouy khassane fofou lay wokka Sa ex yila done sonal nieupeu lay nokka Athe la bathi kaw keen doula diote Diokh la khir bi ngaleen di thiaw Ma takhaw nane ko niaw Mbeguel dafa nekh bokoy kaffé sakh day nekh Sa biir xol bilay diap mel ni danio thi dougal fekh Meuno kham limay wakh tant que demo thi bamou diekh Fok nga niam kani waw doga xam lou lem di saff Awa nénama dafa nekh makhfou nene nama dafa nekh kadia nenama dafa nekh Meme maimouna nenama mbeuguel dafa nekhhhh Refrain Kone dama la bougga té koumou meti nanal amoniaque baygon wala maladio sayo yewo nganiouy guiss niouy leungo ma nane ko Beug na beug nako boudoul reen di deween dinako def ndakh yama diaral lolou Dama tégui gros lot ohh Mom momay teul mane mako beureung xam na nandou lo lolou Nioune bouniou begué moniou begual bouniou dioyé moniou dioylo Couplet Bebe xam ngama bou bakh douma kou tegui ndawal Fima lay diap banga ni Akhh mako xam té dama koy dowal Bebe xam nga mane loutakh ma beug la dama thi sawar Danga fek fi thiebou kéthiakh nga valorisé sani thi ndawal Ndakham lakh bi daniou koy seulmo no daniou koy keupo Sama carte bi ioe la votel tak seuy bi dial thi lenene Kone danga mer mane mangui bakh Diokh ko ndox mou nane mou gékh Lolou meunoul niak Ndakh Mbeguel dafa nekh bokoy kaffé sakh day nekh Sa biir xol bilay diap mel ni danio thi dougal fekh Meuno kham limay wakh tant que demo thi bamou diekh Fok nga niam kani waw doga xam lou lem di saff Abba nenama dafa nekh ngoné nénama dafa nekh habib nénama dafa Meme aicha aziz nénama mbeuguel dafa nekhhhhhhh Refrain Kone dama la bougga té koumou meti nanal amoniaque baygon wala maladio sayo yewo nganiouy guiss niouy leungo ma nane ko Beug na beug nako boudoul reen di deween dinako def ndakh yama diaral lolou Dama tégui gros lot ohh Mom momay teul mane mako beureung xam na nandou lo lolou Nioune bouniou begué moniou begual bouniou dioyé moniou dioylo Mbeuguel mbeuguel mbeuguel dafa nekh Nekh nekh nekh nekha nekh ayyyé waw wa waw waw Kone dama la bougga té koumou meti nanal amoniaque baygon wala maladio sayo yewo nganiouy guiss niouy leungo ma nane ko Beug na beug nako boudoul reen di deween dinako def ndakh yama diaral lolou Dama tégui gros lot ohh Mom momay teul mane mako beureung xam na nandou lo lolou Nioune bouniou begué moniou begual bouniou dioyé moniou dioylo

MusiqueMusique nouveautéMusique sénégalaiseHitMbalakhNouveauté mbalakhViviane Ndour xaritViviane NdourAstarAstar nouveau clipMia guisse gauche droiteNdakhte Glow upMomo diengSénégalBete beteBabel sérieJeebaVjAmadeus