** Clique ici https://bit.ly/miaguisseabonnetoi pour suivre mon actualité ** Cette chanson est une ode à l’amour inconditionnel que l’artiste ressent pour sa fille. Elle y exprime des sentiments de bonheur, de protection et de connexion profonde, tout en évoquant les transformations qu’elle a vécues en tant que mère célibataire. Les paroles sont tendres et intime, la musique douce et enveloppante, combinant des éléments d’afrobeats et de soul pour créer une ambiance poignante et apaisante à la fois, presque comme une berceuse moderne. Lyrics plus bas dans la description (dernière partie). #miaguisse #merecelibataire #clipofficiel #love #amourinconditionnel #miaguissestyle #mgs #team221 ** Crédits de la chanson & du clip MÈRE CÉLIBATAIRE ** Titre : Mère Célibataire Auteurs : Tidiane Kru Mandiou Mauri - Aissata Guissé Compositeur : Mamadou Traoré Mix & matering : Amady Fall Une production de Mia Guisse Style (Dakar, Senegal, Octobre 2024) ** Retrouve Mia Guisse sur les réseaux sociaux ** Instagram https://www.instagram.com/mia_guisse TikTok https://www.tiktok.com/@miaguisse Facebook https://www.facebook.com/profile.php?id=100065839831967 ** Contact management ** miaguissecollab@gmail.com +221 77 655 59 67 ** Lyrics de la chanson MÈRE CÉLIBATAIRE ** Danko beug play kay ñou game Rek nga xam shingom dou kaani xéñ Difeinte faime Diakhasé faine Guisou ñouma sene guiss guissa ñaaw Gné di siissou Gni lakh sen sokhor thi yalla Yalla mi gniy wooté Guem mou gnou ko Lakhou neuteuril dég héy girl Meunone nga ko mafé deug deug héy girl Tiga degué bé na ni noon héy girl beug baakh taxone ma téla seuyi Seuyi mougne dathie eumbe dirékou Doma thi dioudou Beautiful baby Aminatou Done mere célibataire bi di fipou Done ndeye done baaye Done ndeye done baaye Done ndeye done baaye Beneu nit ngay toudou gaagne aye mbokam Héééy Mani momeu Louma wor leu Di faine Té kene dou toudou sa diambar Dagnouy tok di xaar faux pas Gni naane héy girl Meunone nga ko mafé deug deug héy girl Tiga degué bé na ni noon héy girl beug baakh taxone ma téla seuyi Seuyi mougne dathie eumbe dirékou Doma thi dioudou Beautiful baby Aminatou Done mere célibataire bi di fipou Done ndeye done baaye Done ndeye done baaye Done ndeye done baaye Mba do Mandou Ak loko xamal Nit day mandou Déko soutoural Mba do Mandou Ak loko xamal Nit day mandou Déko soutoural Nit kou xam yalla day Mandou Nit kou gueum yalla day Mandou Nit kou xam yalla day Mandou Nit day Mandou Mandou Mandou Mandou Del soutoural jiguéne Del soutoural jiguéne